Touba Stock Market

Touba Stock Market Nous cherchons les stocks disponibles dans les entrepôts italiens et les communiquons aux affairistes

Kippaango Wolof u Wolof mi ngi woo képp ku’y safoo Wolof, di ko jàng ak a jàngale mbaa nga ci’y luññtu mbaa sàx nga yor ...
17/03/2026

Kippaango Wolof u Wolof mi ngi woo képp ku’y safoo Wolof, di ko jàng ak a jàngale mbaa nga ci’y luññtu mbaa sàx nga yor ci ab cér ci nguur gi. Tùubaa la’y àme 5 fan i Awril 2026 ca Université bu Tùubaa, nu fàs ko yéene ànd ak mboolem kilifa ya, UFR ya ak waa ILaMel. Bu ko kenn wùute. Dees na fa leeral jaar-jaar i mbind mi li ko dàle 1968 ba 2005 ak li wàral téereb lëgg-lëgg bii nu bind ko ci gën a ñoŋal mbind mi.




Adresse

Touba
22300

Téléphone

+221765130480

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Touba Stock Market publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Touba Stock Market:

Raccourcis

Partager