Sunu Café Guyaar

Sunu Café Guyaar fas yéene liggéey ngir xam ne liggéey jaamu Yàlla la.

19/05/2026

Je fête mes 5 ans chez Facebook. Merci pour votre soutien, cela ne ce serait jamais fait sans vous.🙏🤗🎉

16/03/2026
12/03/2026

Imam Al Amine Dramé a été placé sous mandat de dépôt, ce jeudi 12 mars 2025

(Les détails en commentaire 👇🏿)

"ASalaamu halaykum ! 👋Yaangi ci Sunu Café Guyaar noongi lay nuyu. ☕✨Bégg nanu lool di leen xamal ne seen café "Prestige"...
12/03/2026

"ASalaamu halaykum ! 👋
Yaangi ci Sunu Café Guyaar noongi lay nuyu. ☕✨
Bégg nanu lool di leen xamal ne seen café "Prestige" bi juge Touba, paré na fii ci Rufisque !
Xool nañu li gën ci Arabica Santos bu Brésil ak Petit Kwilu bu Congo (diamant bi 💎), ñu boole ko ak jar bu set ak sunu secret de fabrication.
✅ Qualité Supérieure (grains yi ñu ràññee lañu).
✅ Xeeñ bu neex te du tàngal xol.
✅ Livraison possible Rufisque Touba et Dakar. Partout au Sénégal.
Mën nga ma envoyer message fii rekk pour ma livrer la sa sachet "Guyaar" ba sa kër wala sa bureau. 🚚
Sunu Café Guyaar : Lu nu ràññee la xam-xam la ! ☕🇸🇳"
Salaam ! 👋

Bienvenue chez Café Guyaar ! ☕✨

Nous sommes ravis de vous annoncer que votre café Prestige de Touba est désormais disponible chez Rufisque !

Nous avons sélectionné les meilleurs Arabicas brésiliens Santos et congolais Petit Kwilu (le diamant 💎), et les avons associés à un bocal de qualité et à notre secret de brassage.

✅ Qualité supérieure (grains d'exception).

✅ Arôme agréable et non irritant.

✅ Livraison possible à Touba et Dakar. Partout au Sénégal.

Contactez-nous pour recevoir votre sachet de « Guyaar » à domicile ou au bureau. 🚚

Notre Café Guyaar : Notre savoir-faire est notre passion ! ☕🇸🇳

Adresse

Dongo Sud
Rufisque
21000

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sunu Café Guyaar publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager